M£urtre atroce à Kounone: Retour sur les lieux du crime, l’émouvant témoignage des voisins. බාගන්න

ඔබේ මිතුරන්ට යවන්න
එකතු කරන්න
  • 2020 මැයි 17

  • Suivez notre chaine Seneweb TV ▷▷ ABONNEZ-VOUS ICI : https://www.youtube.com/channel/UCUot... 🔔 Activez les NOTIFICATIONS pour ne pas manquer les prochaines vidéos Site: http://www.seneweb.com Suivez nous sur: Facebook: http://www.facebook.com/Senewebcom Twitter: http://www.twitter.com/seneweb Instagram : https://instagram.com/seneweb_officiel Contactez-nous: +221 33 869 10 90 - 77 243 35 35 #seneweb #senegal #societe ----------------------------------------------------------------

අදහස්

  • louka perez
    louka perez මාස 4කට පෙර

    Liii lep dieukeur dji moko waral djiguen di doir sa yay gua tok fofou legui voila ray na sa yay un homme doit etre responsable

  • milles mots
    milles mots මාස 4කට පෙර (සංස්කරණය කළ)

    Nama yallah baal mais Belles meres yi naniou moytou akk,toi ton fils avait deja 2 precedents mariages yeup echec, surement elles ont souffert pendant le mariage et apres saine yakkar tass na nakh divorce parceque souniou deglo sa kharite bi néna tu voulais coute que coute seu dom takeu sa mbok pask amna allal té allalam sa mbok moko wara laik , nguaine tass yakar niari djiguene youy seuy pour placé seu mbokk, tey seu mokk lim la daif amana domou diambour yoyou khala tougn lako daif. Louy alal?? Donc quand le fils est pauvre normal na mouy seuy ak domou diambour kokou di misere ak sa dome di diouk ak daanou mais des que le.fils est riche nguaine tass ay seuyam pask diambour dey tok si donkkassi....cette belle fille mom c est vraiment une mauvaise personne . Reposes en paix yallah nalla yallah yeureum figua dieum gueunal la figua diougué

  • Élément AL Saleh
    Élément AL Saleh මාස 4කට පෙර

    jimagine pas souffrance mere bi avant mouy décédé metina metina😢😭😭

  • Jeenab Maryam
    Jeenab Maryam මාස 4කට පෙර

    Bolenn Di takkeu Takkeu lenn kou Bakh 🙏

  • Saliou Séne
    Saliou Séne මාස 4කට පෙර

    Lilepp djekerdjila mo amoul fayeda

  • ARDO K.
    ARDO K. මාස 4කට පෙර

    LA PEINE DE MORT SI VOUS VOULEZ QUE ÇA CESSE. ARRÊTEZ VOTRE HYPOCRISIE ET VOTRE INCROYANCE AU TOUT PUISSANT....OUSME BA GOTO L'AVAIT BIEN PRÉDIT , IL FAUT S'ATTENDRE A ENCORE PIRE. SI VOUS FAITES PAS ATTENTION .

  • Paly Diop
    Paly Diop මාස 4කට පෙර

    Mére dioufa yalla na hipé aldiana firdawsi kou bakh démna yalla bouko tiate djitou amine ya raby 😭😭

  • cheikh sall
    cheikh sall මාස 4කට පෙර

    Les filles cette nouvelle génération sont des sadiques

  • Oumoudieng Dieng
    Oumoudieng Dieng මාස 4කට පෙර (සංස්කරණය කළ)

    rayy dal legui challenge la.... éducation amnaa solo trop ak choisir Diabar Bou bakh...

  • Ham saK0
    Ham saK0 මාස 4කට පෙර

    LE MARI DOIT ÊTRE INTERPELLÉ ET ARRÊTÉ COMME COMPLICE D'AVOIR LAISSER AVEC SA MÈRE UNE TELLE FOLLE FURIEUSE

  • Sokhna Thiaw Sène
    Sokhna Thiaw Sène මාස 4කට පෙර (සංස්කරණය කළ)

    Akhou ndiourèl nimou lèl walahi sama xol❤mètti na trop😭mere bi yalnako yalla xaré aldiana firdawsi😭

  • Mbodja Seye
    Mbodja Seye මාස 4කට පෙර

    Yaye boye yalna ga xiipé aldiana sama xôle mo féss li métti nama lole

  • Mbayang Gueye
    Mbayang Gueye මාස 4කට පෙර

    Sama xol dafa diekh dafa ame ay gor you niank fayda tak djiguene moy maltraité sa yaye nga nek thi seybi di ngar ngar te do fasse ndayam thimm waye tay la y khamni bone amoule gnarigne

  • tapha tine
    tapha tine මාස 4කට පෙර

    Kel mbamm...jai comme l'impression que je suis toujours les enquêtes impossibles comme jai lhabittude de le faire. Putain.

  • Khady Diallo
    Khady Diallo මාස 4කට පෙර

    Dama khamoul mère bou am 70ans wakh deug nékhna nékal mane dama khamoul sakh ani ndayou téyé sa ndaye di ray yayou diambour tmt

  • soudia Gueye
    soudia Gueye මාස 4කට පෙර

    Yalnako yallah yeureum xaréko aldiana . Forcer nitt takk mbokam tamit war nanie ko bayi. Parfois nga xeep koudoul sa mbok té fepp mo gueune sa mbok

  • Adama Kama
    Adama Kama මාස 4කට පෙර

    y'a des psychopates dans la société

  • aly diaw
    aly diaw මාස 4කට පෙර

    En ce moment il est où le mari de la dame ? Les mariages entre familles sont des bombes à retardement, tot ou tard ca va exploser. Laissez vos enfants se marier avec qui ils veulent. Que dieu lui accorde le paradis amen.

  • kheuss abo faye
    kheuss abo faye මාස 4කට පෙර

    Man diekeur dji rek la méré gorr dangay am foulé..sama yaye doumako dieund ak dara

  • Mbodja Seye
    Mbodja Seye මාස 4කට පෙර

    Vraiment sama xôl dafa diék dama dioye ba sone amna louma nakhari lole 😭😭😭