L’histoire des enfants... à Touba par leur père: sacrifice, richesse, gloire, découvrez tout de À àZ බාගන්න

ඔබේ මිතුරන්ට යවන්න
එකතු කරන්න
  • 2020 මැයි 14

  • BP ACTU est une chaîne web consacrée à l'information générale. https://www.bpactu.com/ https://facebook.com/bpactu/ https://instagram.com/bpactu/ Contactez-nous au +221.77.152.68.56 #Bpactu #kebetu

අදහස්

  • Pape MandiaYe NdiaYe
    Pape MandiaYe NdiaYe මාස 4කට පෙර

    YalLah na niou borom bi mousseuL ci satan ak jabotam ..

  • Mildja 01
    Mildja 01 මාස 4කට පෙර

    Ki khana ay dof lay waxal nouniouy diawalé guinar ak khalé🤷🏾‍♂️

  • Ibrahima Paye
    Ibrahima Paye මාස 4කට පෙර

    Ki mo fégne

  • Mamadou Tandjigora
    Mamadou Tandjigora මාස 4කට පෙර

    Le père il ne conne pas là valeur de son enfants

  • Salldd Sall 44
    Salldd Sall 44 මාස 4කට පෙර

    Bilahi kousi bayiwoul serigne yi di djabar Yalla mofi nek ay way li metina yalla naniou yalla mouseul si seytané

  • Awa Ndong
    Awa Ndong මාස 4කට පෙර

    paix à leurs âmes.

  • lébou lébou
    lébou lébou මාස 4කට පෙර

    Lou doy war bilay lép alalou adouna wayé yalla moungi lén khar

  • Thioro Sarr
    Thioro Sarr මාස 4කට පෙර

    Aÿ way niou ragal yalla allaou adina diaroul lénli

  • Alfred Ndiaye
    Alfred Ndiaye මාස 3කට පෙර

    Kii limou raye moo bari : raye say doome, raye mousse pendre Chien. Sacrifice la doone def

  • Cheikh VIP
    Cheikh VIP මාස 4කට පෙර

    thiotu ndém bi nak mosi déssone sétttttt ray se ñari dom ndakh xaliss haaaaaaaaaaaaaa🤭

  • Borom Ndiaye
    Borom Ndiaye මාස 4කට පෙර

    Bou lèrenè moma lounouy kharr nak si mome momitt nane ko lèwatal bou élagué kenèn douko khalatt

  • Alfred Ndiaye
    Alfred Ndiaye මාස 3කට පෙර

    Thiey maa waarou dé. Niakk gueum Yalla rek. Topp Serigne yi rek ba sa Adouna yakkou nii.

  • Thioro Sarr
    Thioro Sarr මාස 4කට පෙර

    Aÿ way niou ragal yalla allaou adina diaroul lénli

  • Natach Faye
    Natach Faye මාස 4කට පෙර

    Ana louko fi diar alall bi day dieh wala ga dee bayiko fi lii metinama trop bilay yallna lene yalla yereum🙏

  • Aissa Fall
    Aissa Fall මාස 4කට පෙර

    Yalla na nou yegale Sén ndaw Aldiana alalou adouna dal diaralouma😢😢😢😢

  • N A B O U
    N A B O U මාස 3කට පෙර

    Bari nagnoufi dh xana kay yallah moko wér rék

  • badar oficiel fv
    badar oficiel fv මාස 4කට පෙර

    أستغفرلله yalnako yalla yèrèm 😭😭

  • Wayll Wayll
    Wayll Wayll මාස 3කට පෙර

    😭😭😭😭😭😭😭

  • chawrou kara
    chawrou kara මාස 4කට පෙර

    Ms alalou adouna loumou dome moka dakh bilaye dague rk da metti mes wakhouma lak reindi nitte😭😭😭😭😭😭😭

  • Zakaria Deune
    Zakaria Deune මාස 4කට පෙර

    Allahou akbar yalnako yalla mouseul mouthieul niou si saytané té mayniou moudij bou rafét si barké seydina Mouhammad sws 🙏🙏🙏🙏